Màggatum Buur beek coro lu ndaw li
Màggatum Buur beek coro lu ndaw li
Rate this book:
About This Book
Dedicated to the young, 'the old king and his little girlfriend' is a tale that aims at teaching how to feed babies. The author invites young people to undertake the task of seeking and transmitting that knowledge to close relatives and neighbors. Through this tale, the ideal behavior of teachers, parents and adults regarding that knowledge is taught.
Ce livre, dédié aux jeunes, est un conte qui cherche à enseigner des connaissances sur l'alimentation des bébés et l'auteur les invité à être plus entreprenants pour acquérir et transmettre ces savoirs aux proches. A travers aussi ce conte, les comportements des enseignants, parents et personnes adultes sont visés par rapport par rapport à ces connaissances.
Léeb wi di joxe xam-xam ci ni ñuy dundalee liir yi, taalif la bu nu jagleel xale yeek jigéen ñi. Yaakaar nanu ne, dinañu sawar ci jàng ko. Am ci mbégte, xam ci yit ni ñuy dundalee liir yi. Waaye nag jàng lée wi rekk, doyul ci xam bu baax li ko tax a jóg. Moo tax am nay yëgëtu yu xale yi mën a def, bu ñu wéetee, walla ñu nekk mboolo ànd ceek seen sëriñ. Yëngëtu yooyu dinañu tax xale yi gën a xam, ci ni mu gën a gaawee. Daldi mën a jëfëndiko li ñu xam.

Buy This Book
As an Amazon Associate and Bookshop.org affiliate, BookOrb earns from qualifying purchases.
Write a Review
Sign in to write a review.