Lëg-seen buddikatu bën
Lëg-seen buddikatu bën
Rate this book:
About This Book
This story is an excerpt from the tale of Leuk and Bouki (Hare and Hyena). Its message is designed for everyone. The story offers instructions on the best way to care for one's own teeth and how to avoid cavities. This tale is also directed towards educators and all parents who are trying to teach good dental hygiene to children.
Cette histoire est tirée d'un conte de Lekk et Bukki. Elle s'adresse à toutes les personnes de différentes couches sociales et renseigne sur la manière de prendre soin de nos dents et comment éviter la carie. Ce conte vise aussi les éducateurs et toutes personnes susceptibles d'enseigner la carie dentaire et les comportements à prendre.
Jàngoro jiy yàq bëñ, tudd kadam, (kari) fépp la am ci àddina. Moo tax léeb wii waa àddina si sépp la ñu ko jagleel. Ñi dëkk ci réew yu oomle yeek ñi dëkk ci yu ñeew doole yi. Ndax ñoom itam, lekk suukar, guy gën a jëm kanam tax na mënatuñoo mucc ci njàngoro ji. Léeb wi nak dafay jàngale te di joxe xam-xam ci njàngoroy kadam (kari).

Buy This Book
As an Amazon Associate and Bookshop.org affiliate, BookOrb earns from qualifying purchases.
Write a Review
Sign in to write a review.