Bukkeek "perigam" bu xonq
View on Open Library ↗

Bukkeek "perigam" bu xonq

by

Rate this book:
2001

About This Book

The story 'Bukki's red wig' in this tale-like book teaches us about lice. It explains how lice can get onto people's heads through the exchange of clothing. Through this tale, there is an emphasis on the fact that having lice does not depend on one's social status. The lessons from this book should be conveyed to everyone and especially to those who ignore the causes of lice as well as the preventive measures.

L'histoire posée dans ce livre sous forme de conte nous renseigne sur les poux. Elle nous enseigne sur le comment ils arrivent à nos têtes avec les échanges d'habits mais à travers le conte on met l'accent sur le fait qu'avoir des poux ne dépends pas de votre situation sociale et dés fois ne cible pas les personnes sales uniquement. Les leçons tirées dans ce livre doivent être transmisés à d'autres qui ignorent aussi bien les causes que les préventions.

"Bukkeek perigam bu xonq" léeb la ngir ñi sopp léeb. Dina leen bégal, ta xamal leen, lépp lu nit war a xam, ci mbirum teeñ. Naka la nit di def, ngir du am teeñ ak naka lay def ngir tàggook ñoom, su leen amee. Niti àddina si yépp lañu jagleel téere bii. Ndax teeñ, fépp la am. Am na ci réew yu oomle yeek réew yu néewle yi. Ta ci bopp yépp la mën a nekk: amul boppu tubaab, amul boppu nit ku ñuul, amul naar. Seetul ku am alal, seetul ku amul.

Buy This Book

As an Amazon Associate and Bookshop.org affiliate, BookOrb earns from qualifying purchases.

Write a Review

Sign in to write a review.